LEMZO CHERI (S01) - Episode 07 (VOSTFR)

visualizzazioni 394 202
259

« Lemzo Chéri ! » aborde les histoires sentimentales croisées, pleines de rebondissements, de Mamadou Lamine (LEMZO), sa sœur AMINA, son cousin ABASS, son meilleur ami Arona (RONE), et Aldiouma (GRAND AL), l’oncle de la copine de Rone.

Se retrouvant entre l’amour fou de Clémentine, sa copine officielle, et l’amour intéressé d’Awa, sa voisine d’enfance, Lemzo a le coup de foudre pour Aïcha, une étudiante dont il avait effectué la visite guidée au sein de son entreprise sans savoir qu’elle est la discrète et casanière voisine dont son ami Rone lui parle souvent avec admiration, ainsi que la demi-sœur paternelle de sa collègue Ndéya qu’il ne laisse pas non plus indifférente.

Oncle d’Anta, la petite amie de Rone, le grand commerçant Aldiouma est de son côté totalement épris de Clémentine dont il veut faire sa seconde femme, au grand dam d’Absa, son épouse qui est bien décidée à protéger son « territoire », épaulée par son amie Arame. L’aide de cette dernière est-elle toutefois sincère ?

Intenable coureur de jupons, Abass, le cousin de Lemzo, a, lui, une grande préférence pour les femmes matures très stables financièrement dont la conquête n’est pas de tout repos, tandis qu’Amina, la sœur de Lemzo, fervente militante des droits des femmes et des enfants va voir sa paisible vie de couple subir les contrecoups de la rencontre d’une nuit de son mari Aziz.

Cette série de deux saisons de 26 épisodes chacune nous plonge dans l’univers attachant de l’amour à l’Africaine entre tradition et modernité, avec l’immixtion des amis et de la famille, tout en dénonçant certains maux de la société sénégalaise qu’elle dépeint sans fards.

A découvrir…

Abonnez-vous à notre chaine ITload

▷▷ ABONNEZ-VOUS ICI : itload.info/tost/Ovr.html...

🔔 Activez les NOTIFICATIONS pour ne pas manquer les prochaines vidéos
Retrouvez-nous sur www.leuztv.com/
------------------------------------------------------------------










itload.info/tost/Ovr.html...
Suivez-nous sur Facebook leuzmedia?fr...

LEUZTV
Commenti  
  • Mamadou Diop

    Mamadou Diop

    10 giorni fa

    Au Sénégal les femmes sont plus infidèles que les hommes elles collectionnent les hommes alors femmes sénégalaises ressaisissez vous

  • Oumy SENE

    Oumy SENE

    14 giorni fa

    Je ne sais pas mais quand je regarde cet film j'ai mal au cœur la façon dont lemzo traite clémentine m'écoeure

  • Coumba Diallo

    Coumba Diallo

    19 giorni fa

    Racine déwor😂😂😂

  • Germaine Diatta

    Germaine Diatta

    20 giorni fa

    la boutiques c trouve où

  • bbchou86

    bbchou86

    22 giorni fa

    Lemzo badolo na teumit. Beuguo takk clémentine do ko libéré teumit. Clémentine di investir si zéro nii rek

  • Yandé Diagne

    Yandé Diagne

    23 giorni fa

    Ndéysane djiguéne bou beugu baxoul Clémentine lii leep sa amour molako yobé

  • Khadija Kane

    Khadija Kane

    23 giorni fa

    J’adore le couple Lemzo clémentine mais hélas le gars est aveugle

  • Pauline Djagbré

    Pauline Djagbré

    28 giorni fa

    16 Et si les musulmans ne sont pas des ânes sauvages, comment Allah peut-il dire : « Tuez les mécréants jusqu’à ce qu’ils se convertissent à l’islam… Celui qui quitte l’islam, tuez-le ». Et pourquoi ne savent-ils pas que cet Allah barbare et sanguinaire est Satan ? Et l’islam étant la religion des ânes sauvages, toute personne qui se convertit à l’islam reçoit l’esprit de l’âne et agit comme un âne. Et en vous convertissant à l’islam, vous devenez des ânes sauvages. Selon le plan et la décision de Dieu, les Arabes devaient recevoir les prophètes Juifs. C’est un décret de Dieu et tout Arabe devait accepter cela. Mais ils ont préféré se fabriquer, eux aussi, une religion et un livre saint.

  • beug deug Sénégal

    beug deug Sénégal

    Mese fa

    Mais gor yiy Def comme lamine. Reutieugo lén dé.... Lolen Def djiguen après dingen ko guiss

  • beug deug Sénégal

    beug deug Sénégal

    Mese fa

    Gor dou nén (œuf) diko tieupi tieupé bagn mou lale souff. 😂😂😂😂 Dalay Def golo

  • beug deug Sénégal

    beug deug Sénégal

    Mese fa

    Mariage sax gor mokay demander, bo dèmé beu diko sakou yaw djiguén ngeu war bayi mou sedd.... Gor boula beugué deug day yakamti tak leu. Yalla loumou Def xam nako.. Manam gor nako sa tiapa bi oump. .. Di nian bour bi yombal ko nieup...

  • Moussa Lo

    Moussa Lo

    Mese fa

    Non mère bi douma ray néna bougnou naane kham nguene kougnou amina lagnou wo thi lay diok ni lene wo nguene gor wo diambar wo bété bété😂😂😂😂

  • Haddyjatou Cham

    Haddyjatou Cham

    Mese fa

    Tallon ak plage🤣🤣🤣

  • Awa

    Awa

    Mese fa

    Clementine eupeul nga!! Mouner deey masser tank yi.

  • Babacar Ndiaye

    Babacar Ndiaye

    Mese fa

    Lemzoeun vrai homme ne se comporte pas comme ça

  • mame diarra sarr

    mame diarra sarr

    Mese fa

    Love Guigui la Diva

  • MARIAMA BADIANE

    MARIAMA BADIANE

    Mese fa

    Racine déhors 😂😂😂😂

  • eioshen boboi

    eioshen boboi

    Mese fa

    Beugouma djiguene bou yomb ba melni clémentine

  • IDITION RAPPEUR

    IDITION RAPPEUR

    Mese fa

    https://youtu.be/Hc9PXdjzILo

  • Domingo Mané

    Domingo Mané

    Mese fa

    La vie c'est comme un match de football 90 mn et temps additionnel.

  • Ailsa Ni

    Ailsa Ni

    Mese fa

    Clémentine xana xamo goor beugul lou yomb louko yomb mou fowé ko

    • eioshen boboi

      eioshen boboi

      Mese fa

      Kilifa so begué sokhna takal rék met dokhane weuroul machala si diagualébi

  • Lasn Nas

    Lasn Nas

    Mese fa

    Guigui sa teint tamit lane la 😍😍😍😍😍😍. Vraiment laf thiaat sa future dieukeur dina leik niamou beut 🤣🤣

  • koiun dwrru

    koiun dwrru

    Mese fa

    No mane badiène la beugu

  • Niouk Fall

    Niouk Fall

    Mese fa

    LEMZO DIT PAREGOUMA CI YAW CELA MONTRE LE MANQUE DE RESPECT QU'IL A VIS A VIS DE CLEMENTINE C AUX FEMMES DE NE PAS AVOIR PEUR DE PERDRE UN HOMME ET DE SERRE LES CUISSE WASSALAM

    • Ailsa Ni

      Ailsa Ni

      Mese fa

      Aljouma rofnga ngof de

  • Niouk Fall

    Niouk Fall

    Mese fa

    RONNE SI TU N'ES PAS PIEUX C TON AFFAIRE MAIS IL Y A UN POLITICIEN PIEUX DIGNE VERIDIQUE QU'ON VEUT ELIMINER MAIS DIEU EST AVEC CE POLITICIEN

  • Niouk Fall

    Niouk Fall

    Mese fa

    Niouk Fall
    DIALMB
    SI LEMZO JOUE TRES BIEN IL JOUE LA LEGERETE DES HOMMES INSOUCIANTS CAR ILS SONT TOUT CE QU'ILS VEULENT DES FEMMES TU VAS VOIR QUAND IL SERA AVEC UNE FEMME TIGRESSE DIGNE D'UNE VRAIE FEMME IL AURA PLUS CE SOURIRE IDIOT DE L'HOMME POUR QUI TOUT EST FACILE IL SERA PLUS SERIEUX

    • koiun dwrru

      koiun dwrru

      Mese fa

      Ay waaayyyy clémentine amal souniou kersa..... Li yeup ngua diokher ko gratuitement, beugue niou takela, legui nak yagui bagne bagnelou çanapassssaraaaaa pas

  • Niouk Fall

    Niouk Fall

    Mese fa

    LES FEMMES AFRICAINES ARRETEZ DE VOUS DEPIGMENTER LA PEAU REGARDER COMMENT ELLE EST LAIDE ET SALE CETTE RECEPTIONNISTE TCHIM

  • Niouk Fall

    Niouk Fall

    Mese fa

    supprimel numerorobi par respect😂😂😂😂😂😂😂JALOUSIE MALADITIVE QUAND TU NOUS TIENS😂😂😂😂😂😂😂😂

  • Assane Ndiaye

    Assane Ndiaye

    Mese fa

    Lemzo Kay Diaratoul Mouy Takké Li Goor Di Weur Si Djiguéne Yeupeu Amna Ko Te Mariewoul

    • Mouhamadou Barry

      Mouhamadou Barry

      Mese fa

      Aîcha est très calme

  • Ibrahima Diamanka

    Ibrahima Diamanka

    Mese fa

    Vraiment le gaspiage n'est pas bon

  • Bolia Fops

    Bolia Fops

    Mese fa

    Clémentine yaw kay diaroul takk yaguii sey

  • Mactar Diouf

    Mactar Diouf

    Mese fa

    No ngoury mo neh deug

  • MAME DIARRAA SOCK

    MAME DIARRAA SOCK

    Mese fa

    Khady mashallah bonne continuation

  • نور العلم tv

    نور العلم tv

    Mese fa

    Kou Begeu kham sa diné Abonnél sama sén

  • BOROM KOUROUSS TV

    BOROM KOUROUSS TV

    Mese fa

    Kilifa so begué sokhna takal rék met dokhane weuroul machala si diagualébi

    • Bolia Fops

      Bolia Fops

      Mese fa

      Wa clementine mi esk sava tamit

  • Marie Helene Ndeye

    Marie Helene Ndeye

    Mese fa

    Goor mboo badolaa!!!Motaxxittt djiguène yii yeiwounagne leguii

  • Sokhna Laye

    Sokhna Laye

    Mese fa

    Ada bou doye waar. Def teranga di kharal gnou doublé lii nga diokhé délo la ko. Sénégal deuko téranga 🙄
    Wa faar sakh dagne kaye défal pédicure ?! wala si série yi la yam 😆. Que Dieu nous préserve des faux types comme rone.
    Aïcha boul massa khessal. Kou ma ko meusseu wakh ma méré la parce que je ne vois pas de raison d’aller m’éclaircir la peau mais toi aussi ne fais jamais ça black is beautiful 😍

  • Mary Madeleine thiam Thiam

    Mary Madeleine thiam Thiam

    Mese fa

    Billah Gore bouguoul Lou yombe

  • Chiekh tidiane Diba

    Chiekh tidiane Diba

    Mese fa

    Aljouma rofnga ngof de

  • Deto Qcney

    Deto Qcney

    Mese fa

    Ay waaayyyy clémentine amal souniou kersa..... Li yeup ngua diokher ko gratuitement, beugue niou takela, legui nak yagui bagne bagnelou çanapassssaraaaaa pas

  • Ndeye Mbaye

    Ndeye Mbaye

    Mese fa

    Ahh lemzo tmt takaguo di programme

  • khoumba camara

    khoumba camara

    Mese fa

    LEMZO mi dou yeureum clémentine touti. Mou libéré co sakh

  • Saly Cisse

    Saly Cisse

    Mese fa

    No badiane diaye prekkkk la kW🤣🤣 cheuuu

    • Deto Qcney

      Deto Qcney

      Mese fa

      Amina modé naa Clémentine wayaddi na lool sakh djigeene dayy am dignité wayy khar bagnou takk ko yayou lemzo nékhna anta daff ma nékh lool macha allah

  • Soinas Doyi

    Soinas Doyi

    Mese fa

    d'argent !

  • Awa Aidara

    Awa Aidara

    Mese fa

    Mais clémentine esk lemzo dinako takk tamite ko khamni leepeu yangkoy am avant le mariage ha khana lemzo gooree deug rekkkk mais doyna war

  • Nogoye SECK

    Nogoye SECK

    Mese fa

    Qui va dire à clémentine qu’on ne force pas le mariage 🙄🙄

  • Astou Niass

    Astou Niass

    Mese fa

    Racine dèorr dou deguuu

  • Astou Niass

    Astou Niass

    Mese fa

    Wa clementine mi esk sava tamit

    • Soinas Doyi

      Soinas Doyi

      Mese fa

      Waaaa clémentine mii😭😭😭😭 pédicure la guiss ni

  • yaly diallo

    yaly diallo

    Mese fa

    Déhors. Je vais te fermer à l intérieur.??????

  • Aicha camara

    Aicha camara

    Mese fa

    Racine déhors racine déhors

  • Adjia Seck

    Adjia Seck

    Mese fa

    Thieuy djiguén bou beug seuy méti na dh😅😅
    Clémentine dh louné lay déff bax na bam sotii

  • Whgu ybnm

    Whgu ybnm

    Mese fa

    Everything looks amazing Les! ??????

  • BAMBA ELECTRONIQUE

    BAMBA ELECTRONIQUE

    Mese fa

    GUGU jouer bien son rôle vraiment des j’aime 👍 pour lui SVP

    • Saer Diop

      Saer Diop

      Mese fa

      C’est acause de Guigui que je regarde mais je pense qu’il faut plus de visibilité à ce Seri soit deux fois par semaine et des rediffusions

  • bssni touir

    bssni touir

    Mese fa

    Clémentine tamiit ki d’où sa dieukeur this❤️

  • Khady Thiam

    Khady Thiam

    Mese fa

    adresse boutique bi diaye chemise yii svp

  • Fatou bintou Djitte

    Fatou bintou Djitte

    Mese fa

    *Amina modé naa*
    *Clémentine wayaddi na lool* *sakh djigeene dayy am dignité wayy khar bagnou takk ko*
    *yayou lemzo nékhna*
    *anta daff ma nékh lool macha allah*

    • Fatou bintou Djitte

      Fatou bintou Djitte

      Mese fa

      @Whgu ybnm bilay walayyy

    • Whgu ybnm

      Whgu ybnm

      Mese fa

      Aldiouma respecté wo sa diabar dji daal

  • Modou Diop

    Modou Diop

    Mese fa

    Clémentine rafete ga loll

    • bssni touir

      bssni touir

      Mese fa

      Mane badiane douma raye néna trois solou si kheiwou diabour lii tamite kéne dousi wakhe

  • Sona Bodian

    Sona Bodian

    Mese fa

    Gor mom soko yombalé leup il va pas té respecte clémentine xamal sa bop ak sa valeur le mec ne va jamais tepousé si toute est facile pour lui

  • Sophie Dia

    Sophie Dia

    Mese fa

    Clémentine regarde comment tu est belle et independente laisse ce Lemzo et trouve un Homme qui te mérite. C’est malheureux mais dans la vie réelle les belles femmes comme clémentine n’ont pas toujours de chance en amour

    • Miss tchip tchip

      Miss tchip tchip

      6 giorni fa

      Cest mon cas ...je me vois dans clenentine a courrir derriere quelqun qui veut pas une vie stable

    • Khadija Kane

      Khadija Kane

      23 giorni fa

      Ah ce Lemzo est ingrat

    • Khady Niang

      Khady Niang

      Mese fa

      W

    • Soinas Doyi

      Soinas Doyi

      Mese fa

      d'argent !

  • Mbathio Mangane

    Mbathio Mangane

    Mese fa

    Waaaa clémentine mii😭😭😭😭 pédicure la guiss ni

  • Bintou Thiam

    Bintou Thiam

    Mese fa

    Clémentine wayadi na mais lemzo kou hypocrite tu sais que douko tak pourquoi ga koy tardel

  • Venus Ndiaye

    Venus Ndiaye

    Mese fa

    LEMZO do goor bou bakh .... goor yi bolén arretez woul d'abuser de la faiblesse des femmes qui vous aiment ..dingén yague takk moussiba ...
    Li rek war na takh djiguéne bou nék di sameu bopam
    Di seuy di topato té dou diaka dou église

  • Khadija Camara

    Khadija Camara

    Mese fa

    Racine dééwoor do degg

  • nana ndiaye

    nana ndiaye

    Mese fa

    Faut dire au mari de l'infirmière de raser un peu ses cheveux.

    • nana ndiaye

      nana ndiaye

      Mese fa

      @Yema Fafa l'essentiel c'est de comprendre

    • Yema Fafa

      Yema Fafa

      Mese fa

      Elle est médecin pas infirmière.

  • Fatou Demba Thioune

    Fatou Demba Thioune

    Mese fa

    Femme facile non jaime pas les Clémentine arrêter

  • Adame Ngom

    Adame Ngom

    Mese fa

    Clémentine foula touti waye takou gnoula teke thie beuguou gna guaye déf you gnake faye da yi

  • Deh Lia

    Deh Lia

    Mese fa

    Ngouri 😀😀😀😀

  • faye mingue

    faye mingue

    Mese fa

    Kanamou aldiouma bi🤣🤣🤣😂😂😂😂

  • Mariama Dia

    Mariama Dia

    Mese fa

    Aldiouma respecté wo sa diabar dji daal

  • SHAM THIAM

    SHAM THIAM

    Mese fa

    Lemzo un vrai maram djiguen soko beugoul bayil mou dem mais diko teuder teh amoci mom ben khalate bou rafet

  • Mori Ciss

    Mori Ciss

    Mese fa

    Mane badiane douma raye néna trois solou si kheiwou diabour lii tamite kéne dousi wakhe

  • Athia Diallo

    Athia Diallo

    Mese fa

    Dama sahh moudié yeureum Clementine

  • Ahmadou cisse

    Ahmadou cisse

    Mese fa

    No aljouma dou nit😂😂😂

  • Serigne Aliou THIAM

    Serigne Aliou THIAM

    Mese fa

    Clémentine sayy birr yombuna dh.

  • Ramatoulaye Dieye Diop

    Ramatoulaye Dieye Diop

    Mese fa

    Clémentine ferme tes cuisses à lemzo et tu verras la réalité messou la beug il est avec toi juste pour satisfaire ses besoins. Réveil toi tu mérite mieux vraiment tu es juste amoureuse mais pas mauvaise mais tu es tombé sur un profiteur on va dire

  • Ramatoulaye Dieye Diop

    Ramatoulaye Dieye Diop

    Mese fa

    Nenako je vais te fermé à l'intérieur
    Sheuuuu pourquoi vous vous compliqué la vie rek parler olof kene forcé woulene français gui

  • Awa Kamara

    Awa Kamara

    Mese fa

    GOOR GNI MELNI LEMZO TAMITE DOU NGUEN TCHI WAKH BEUGOULO JIGENE POURQUOI FOWEKO C'EST PAS QUE GOOR NGA REK LOULA NEKH DEFF GOOR DAFA AME LOUMOU WARA BAGNE

  • Loifa El frezhi

    Loifa El frezhi

    Mese fa

    M clementine niko adjiouma beugue moikay nelawlo nonoulako lemzo fay rek mouy guor AK djguen gniosi bok yam kosi won mbeuguel mou woyadilola

  • Aishacooks T.V

    Aishacooks T.V

    Mese fa

    Ko noboul rek mo ley nop 😂

    • Mbaye Babacar

      Mbaye Babacar

      Mese fa

      wa loutax lolou teumite, bilay aduna bi dafa meti

    • Adama Sy

      Adama Sy

      Mese fa

      Noko khamé

    • Bassine Lo

      Bassine Lo

      Mese fa

      Barki yalla 😂😂😂😂

  • dialmb

    dialmb

    Mese fa

    Lemzo avec son sourire tout le temps là je trouve qu'il ne joue pas bien

    • Niouk Fall

      Niouk Fall

      Mese fa

      SI IL JOUE TRES BIEN IL JOUE LA LEGERETE DES HOMMES INOUCIANTS CAR ILS SONT TOUT CE QU'ILS VEULENT DES FEMMES TU VAS VOIR QUAND IL SERA AVEC UNE FEMME TIGRESSE IL AURA PLUS CE SOURIRE IDIOT DE L'HOMME POUR QUI TOUT EST FACILE

  • Karim Sarr

    Karim Sarr

    Mese fa

    Any fama

  • Cheikh Diop

    Cheikh Diop

    Mese fa

    Mane zeyna li la dounedou mes tay bayi nako dakh dama khol rek kham thieuy

  • Yaye Maye Lat Mbao

    Yaye Maye Lat Mbao

    Mese fa

    Wa adiouma mi nitt la wala kher🤣🤣🤣

    • Yaye Maye Lat Mbao

      Yaye Maye Lat Mbao

      Mese fa

      @Sidy Bara dama warou di khol djiguéne bay fakastalou ta andeu ak sa diabar

    • Sidy Bara

      Sidy Bara

      Mese fa

      😂😂😂😂😂

  • ndong fatou k

    ndong fatou k

    Mese fa

    Humm xélé djiguèn yi bayilèn xel bubakh cette série joint l'utile à l'agréable très interéssante Lemzo a dit à sa mère que "guissagoul kumu tak" alors qu'il est avec sa soit disant copine ce qui veut dire qu'il n'a aucune intention de la marier les filles faites très attention avec les hommes goor beugul lu yom si ay beteum ils sont là que pour leur propres intérets sugnu doyalè rek sanila xol xalé bu ndaw bu tok si coté ndayam gnu takko bakhna dal rekk

  • Maguette Fall

    Maguette Fall

    Mese fa

    Khalé yu djinguène yi ame lène foula

    • Binta Cissokho

      Binta Cissokho

      Mese fa

      Kouko si amoul pérte les hommes vont bien joué avec toi

  • Sokhna mai Geuye

    Sokhna mai Geuye

    Mese fa

    Amina day yax sama addina toubab Bou dofff la Ms yaye dji doukasi bayyi nénako xamguéne kounou wooo amina lanou woo amina dal paréna Bou yague day xar touram 😂😂😂

  • Sokhna mai Geuye

    Sokhna mai Geuye

    Mese fa

    GUI GUI elle est s’insère 😂

  • khoumba bathily

    khoumba bathily

    Mese fa

    Beugouma djiguene bou yomb ba melni clémentine

  • Diaryatoulah Diop

    Diaryatoulah Diop

    Mese fa

    Badiene la beug 😂😂😂😂😂😂 khamnguen kouniou wo amina laniou manane woguen kou ndeyam nangou kay fek panier yi weurma
    Woyyy wadji nenako supprimelma numéro bi par respect
    Adiouma😂😂😂😂😂 clémentine niakna fayda lerna lani lemzo beugoula te doula taak amo ben foula

    • Lota Gaye

      Lota Gaye

      Mese fa

      Aldjiouma loutakh bougoul Lou bakh Am sokhna diongoma puirr di dokhane

  • Cheikh Mbaye’s

    Cheikh Mbaye’s

    Mese fa

    Film m’a bi dhè boudon am si semaine bi deux fois dina nekh trop stp 🙏🏿🙏🏿

  • Keera Bilo

    Keera Bilo

    Mese fa

    Clémentine nena grand Al ki moy sama COPANNNNN 😂😂😂😂

    • Aïda Mbene

      Aïda Mbene

      Mese fa

      Khawma loutakh nioù beugue prononcé RK😂😂😂😂

  • fatima fatima

    fatima fatima

    Mese fa

    djégui sirat pour un bisous, ma ngui dé; ce fone balla

  • Ahmed Diallo

    Ahmed Diallo

    Mese fa

    Nice na

  • Lobe Ndiaye

    Lobe Ndiaye

    Mese fa

    Weuy grand Al...😂😂 wa tamite yoor Diama di weurii Or

  • Oumou Diatta

    Oumou Diatta

    Mese fa

    Mann dama yeureum Clémentine
    J'espère que Lemzo l'aime autant
    😔😒

    • Rouguita barhama

      Rouguita barhama

      Mese fa

      Non non il l'a bien confirmé il l'aime pas

  • Absa Gassama

    Absa Gassama

    Mese fa

    Amina modegua limotakh dieukeur di dokhane

    • ndong fatou k

      ndong fatou k

      Mese fa

      @Fatima Sarr je pense que c'est cette fille elle mm qui l'envoyait des méssages moi perso je croix que c'est un deal entre la fille et son soit disant amant si tu te souviens du début de la série c'est cette fille qui avait un problème avec son copain et c'est le mari de Amina qui l'a sauvé

    • Fatima Sarr

      Fatima Sarr

      Mese fa

      Dieukeur dji dokhanagoul dé. Il est fidèle à sa femme pour le moment. C'est la fille qui ne le lâche pas, motakh il a dit qu'il va y mettre fin... Malheureusement à cause de l'histoire d'Ousmane, il a quitté la Corniche. Ce qui m'a dérangé kay moy, il ne reconnaît pas cette fille qui l'interpelle et sans même chercher, il prend son numéro.

    • ndong fatou k

      ndong fatou k

      Mese fa

      qui t'a dit que diekeurem day dokhane ? wala dagnu nek diko pièger our mou dokhane par force dp8 le debut il est sérieux xalé yu djiguèn yi la kèn manul mouthiou si gnom

  • grubhub edits

    grubhub edits

    Mese fa

    Wa yene Clementine mi migui seuy der khawma bane mariage la beug nak je suis choquee

  • Fatima Diop

    Fatima Diop

    Mese fa

    Amina mbode na nak🙄

    • Fatima Sarr

      Fatima Sarr

      Mese fa

      Elle est le genre de Woopy Goldberg yoyou, en plus jeune.

  • Aminata Diop

    Aminata Diop

    Mese fa

    No badjiene dou changer😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂