Gamou Champs de courses intégrale avec Serigne Moustapha Sy du 18 Octobre 2021 à Tivaouane

Pubblicato il 19 ott 2021
visualizzazioni 46 972
0

Gamou Champs de courses intégrale avec Serigne Moustapha Sy du 18 Octobre 2021 à Tivaouane

DAKARBUZZ TV
DAKARBUZZ TV
Commenti: 81  
  • Ndeye Cissé

    Ndeye Cissé

    2 mesi fa

    LE PROFESSEUR DE TOUT LES PROFESSEUR L'HOMME PLUS QUE PARFAIT "ALMOUSTAPHA" ON VOUS AIME FORT ET MERCI INFINIMENT ❣️❣️❣️🔒🔥.

  • Makhou Waly

    Makhou Waly

    3 mesi fa

    Machallah SY Malick 😍💖😘🙏 yalla n'a Diam yagu souniou keur Mame 😍💖😘🙏 Long vie à notre kilifeu 🙏

  • Diagne Ndoye

    Diagne Ndoye

    3 mesi fa

    As salaam Aleyka Ya RASSOULALILAH Mouhamad Saw rek doyna gàmmu mashallah Jerejef Sy Demba Bouna Sëx Seid Mouhamad Müstafa Sy Maqtúm yalna YALLA Sàmm baayi lafi mu anda ak wer insh Allah barké Yonetbi Saw insh Allah

  • khadija rasoul

    khadija rasoul

    3 mesi fa

    Ndeysan sy demba ak bouna goudal fan weral sy yala samal gnou sougnou gorgi ar ko yiir ko bamou mouth thi péxey none yii❤❤🙏🙏

  • Awa Diallo

    Awa Diallo

    3 mesi fa

    Alhamdoulilah. Sante yalla bamoj défé sa ndiabot sagal nga tarikha cheikh ak say mame futilités adouna yobalewoula ndakh kham gui nga kham sa thieur thie yalla.yalla n'a sakh

    • Mbaye Diop

      Mbaye Diop

      3 mesi fa

      Allahouma amiiine inchaa allah

  • Omar Diop

    Omar Diop

    3 mesi fa

    Machallah baraka Allahou

  • Khalifa ben mt Diop

    Khalifa ben mt Diop

    3 mesi fa

    Yalla na fane wi goudou ak wérre amine incha allah

  • Xalima Talif

    Xalima Talif

    2 mesi fa

    Machallah sy Malik. Merci dkr buzz

  • Fasoba BA

    Fasoba BA

    3 mesi fa

    machallah yalla diniou soutoural niouy am takhaway ba kanamou yalla incha allah dina bary lou lair ❤💖💖

    • Ndeye Binta Deme

      Ndeye Binta Deme

      2 mesi fa

      Amine incha alla

  • Mor Talla Gaye

    Mor Talla Gaye

    3 mesi fa

    Mashâ allâh

  • Mamadou Dieye

    Mamadou Dieye

    3 mesi fa

    Mashallah Sy Malick yalla na yalla motalli inchallah

  • IDRISSA DEME

    IDRISSA DEME

    3 mesi fa

    Macha Allah

  • Dame Aida Diop

    Dame Aida Diop

    3 mesi fa

    Mashallah

  • Khalifa Dia

    Khalifa Dia

    3 mesi fa

    Merci wá dakarbuzz tv yállah nalein yállah yokk sein doole Lou kawe sein ndiort

    • malick wade

      malick wade

      2 mesi fa

      Mm

  • Seynabou Maty BA

    Seynabou Maty BA

    3 mesi fa

    Machallah 🥰👍🥰👍

  • Diagne Ndoye

    Diagne Ndoye

    3 mesi fa

    MASHALLAH DakarBuzz seen job rafetna ci gàmmu gui yalna BOROM Guddi gui ak ki ki dundeul fayleen ci katanu BOROM Bi insh Allah
    Att mit lanà nurànàa ba eeuleuk insh Allah

  • Alou Sylla

    Alou Sylla

    Giorno fa

    Machalah

  • El Hadji Sall

    El Hadji Sall

    Mese fa

    Machalah

  • Sokhna DIOUF

    Sokhna DIOUF

    3 mesi fa

    Sy Demba doundeul weureul barké mouhamed psl 🙏

    • Bineta Gueye

      Bineta Gueye

      2 mesi fa

      Amine inchallah

    • Mbaye Diop

      Mbaye Diop

      3 mesi fa

      Allahouma amiiine inchaa allah

  • Meissa Diop

    Meissa Diop

    3 mesi fa

    Machallah

    • AIDA DIOP

      AIDA DIOP

      3 mesi fa

      Macha allah Sy Malick khole yep fekhna

  • Diaz Diop

    Diaz Diop

    3 mesi fa

    Dakar buzz merci beaucoup pour la couverture du maouloud yala na souniou borom mayléne yokouté bou bakh si barké yonentibi PSL

    • Diagne Ndoye

      Diagne Ndoye

      3 mesi fa

      Amine ya rabbi insh Allah

  • Awa Drame

    Awa Drame

    3 mesi fa

    Dieuredieuf sy malick

  • Ndeye Binta Deme

    Ndeye Binta Deme

    2 mesi fa

    Alhamdoulilah

  • Salimata Traoré

    Salimata Traoré

    2 mesi fa

    Sy Malick amouniou sa fayyyyy barki Mame Babacar ♥️♥️♥️♥️

  • At Tidjani

    At Tidjani

    3 mesi fa

    Dieureudieuf Sy demba yaag fi tei werr

    • Mbaye Diop

      Mbaye Diop

      3 mesi fa

      Allahouma amiiine inchaa allah

    • At Tidjani

      At Tidjani

      3 mesi fa

      @Khalifa Dia amine inchaAllah ak yow itam

    • Khalifa Dia

      Khalifa Dia

      3 mesi fa

      @At Tidjani Amiin yew yallah nang fi yágg te and ak wer ak diam ak soutura

    • At Tidjani

      At Tidjani

      3 mesi fa

      @Bineta Seck ziaar Nala

    • Bineta Seck

      Bineta Seck

      3 mesi fa

      Amine inchallah

  • Maodo Ndao

    Maodo Ndao

    3 mesi fa

    Machala

  • ViTo Ndiaye

    ViTo Ndiaye

    3 mesi fa

    ❤❤❤❤❤

  • riffcheu riff

    riffcheu riff

    3 mesi fa

    mashalla

  • Adama Dia

    Adama Dia

    3 mesi fa

    Macallah

  • LY Djiby

    LY Djiby

    2 mesi fa

    je souhaite vraiment rencontré moustapha almaktoum

  • Maoda Ndiaye

    Maoda Ndiaye

    3 mesi fa

    Soukrane

  • Coumba Fall

    Coumba Fall

    3 mesi fa

    Machallah sy yalla nala yalla are samla inchallah si sa barké Mame

    • Ndeye POUYE

      Ndeye POUYE

      3 mesi fa

      Machaala Serigne Moustapha gamou bi nehna yalla n'a yalla n'a goudeul fanyi

  • Khalifa ben mt Diop

    Khalifa ben mt Diop

    3 mesi fa

    Wallahi sy malick yanouye khamal rassoul kom niko sa mame maodo dane défé ak s babacar sy ak mame cheikh

  • Mareme Dieng

    Mareme Dieng

    3 mesi fa

    Bilahi sy sagaliti ngagnou si sounou canamou none yi yalla na yalla doli soutoura bi nak khewal gui yalla arela samela soutoural la bayilafi bassi caname ine chalah diarama narou ya Sophie dème amo morome sangue bi do morome ya gnou doye fi ak feulé

    • Noumbè badiane bahkenga trop Kebe

      Noumbè badiane bahkenga trop Kebe

      3 mesi fa

      Amine,

    • Mbaye Diop

      Mbaye Diop

      3 mesi fa

      Allahouma amiiine inchaa allah

    • Khalifa Dia

      Khalifa Dia

      3 mesi fa

      @Mariatou Diop Amiin inshá Allah yew temit Yalna Allah goudal say Fan te yokku sa diam🤲ak da sutura niou yágg koo tewe si kanamou góor gui

    • Mariatou Diop

      Mariatou Diop

      3 mesi fa

      Walahi yalna yalla sama arla goudal ay fanam

    • Khalifa Dia

      Khalifa Dia

      3 mesi fa

      Bil láhi nan koy niánal rek

  • Thierno Mbaye

    Thierno Mbaye

    3 mesi fa

    Ma challah

  • Ndiaye Dybala

    Ndiaye Dybala

    3 mesi fa

    Dakar buzz moustarchid yep beknan si yen

  • Moustapha Diop

    Moustapha Diop

    3 mesi fa

    Mawlod 2021serigne Moustapha si

  • Best man Goodcaracter

    Best man Goodcaracter

    3 mesi fa

    Bien

  • et ctaidatoure knowtoure

    et ctaidatoure knowtoure

    2 mesi fa

    Kou bakh rek beug na serigne Moustapha Sy al maktoum. Dafa nékha beug

  • Modou Leye

    Modou Leye

    3 mesi fa

    sy yagiue fi loll té rek téwérr

  • malick mbaye

    malick mbaye

    3 mesi fa

    Merci wa dkr buzz

  • Seuttou serigne babacar Sy

    Seuttou serigne babacar Sy

    2 mesi fa

    Dieureudieuf Sy malick

  • Alchimiste L'homme

    Alchimiste L'homme

    3 mesi fa

    Ndeyssane. Enseignement bi si Yonente bi 1 h de temps, mais nite yi niogui si lenen. . Amna solo salam yi nek si alxourane, ak nouyou yiniou nouyou YONENTE bi. Le Salut du Prophètique. Si Limou traversée, ba guaday... ndeyssane mais deuxième partie bi....Oh. bilaay ken Dou Muhammad psl

    • Alchimiste L'homme

      Alchimiste L'homme

      3 mesi fa

      @Diagne Ndoye mogui Nonou barina Koy wax Lou Mara waw si Gamou gui doulako wax. Ils ne suivent pas l'enseignement

    • Diagne Ndoye

      Diagne Ndoye

      3 mesi fa

      Malheureusement itt ñi amouñiou deëgg ndeyssan Sëx Seid Mouhamad Müstafa Sy Maqtúm Yalna ko Sunu BOROM gueun taxawü insh Allah

  • ALIAS FOR

    ALIAS FOR

    3 mesi fa

    Le son audio est pas bien

  • Ndeye Binta Deme

    Ndeye Binta Deme

    2 mesi fa

    Santati yalla soubhan wa tanla bou bakh bamou gnou defé sa daiboote té di niane yalla gua nagoul gnou diaboote gui

  • Habib Kane

    Habib Kane

    Mese fa

    Serigne Moustapha sy ndeux ngeux ndouroke ak pinok yio tehe kou katte seux leufeul ndeye ngeux domerame

  • 16 mars Tv

    16 mars Tv

    12 giorni fa

    Seutbi mo sagal mam bi

  • Amadou Sow

    Amadou Sow

    2 mesi fa

    Diarama Sy Malick

  • Sadikhe

    Sadikhe

    3 mesi fa

    Gamou bokhamni dowakh yala dowakh yonentibi se du teatre sa dara doufi barkel pask dokholene si ndigueule s mbaye sy mansour sa baye yalnafi yagu te were

    • Sadikhe

      Sadikhe

      2 mesi fa

      @tivaouane sene gathier soretoul si barké s m sy mansour sa bayouyou srigne, taphasy migakhamni se un drogué bayam reubko khalapko ndayam si biti torokhom soretoul

    • tivaouane

      tivaouane

      2 mesi fa

      Sadikhe yeuremeul sa Bop ak sa baye ak sa yaye nafékhe pire nga

    • Sadikhe

      Sadikhe

      2 mesi fa

      @khoudia nguirane dagéna rerr malene yeureum yaw ak sa serigne MT SY yeureumnalene ndeysane

    • khoudia nguirane

      khoudia nguirane

      2 mesi fa

      Na fekh késsé moy gui deugg tek si tankam deglou woh wakhtane bi beugeu juger wakhtane bi lepp si enseignement yoneti bi la delou. Mé doko mana kham mm boko deglou wone tamit ndakh naafekh boko done wane le soleil sakh mou geum né guissiumako. Nioune ndiabotam nak demou niou Baar ni boite de nuit té douniou toukh té bouniou wakhé niepp né eskeuy lolou nak boudoul barkel kone khamo barké

    • 2BTV

      2BTV

      2 mesi fa

      Fall dieundal glace nga diéma féxal sa xol bi fi Serigne Moustapha Sy rék mofi nék point